Web dalal
Ñi nara nekk kiliyaan dañuy gis sa tur 24 waxtu ci bis bi ak 7 fan ci ayu-bis bi.
Nekk ciképp ku xool ci kaw dina gis sa tur ci kaw!
Performance bu baax ak wóor ak yoriinu liggéey bu yomb
Ñi nara nekk kiliyaan dañuy gis sa tur 24 waxtu ci bis bi ak 7 fan ci ayu-bis bi.
Nekk ciWutal bépp performance bu bees bu serwër bi ngir say sitweb ak say aplikaasioŋ yu bari ay jumtukaay
Nekk ci4 milyaari nit am nañu internet, ñuy seet ay serwiis yu mel ni yaw ci niir yi.
Tambalil leegi
Yomb naa - dugal sa tur domen bi nga bëgg rek nga xool ci saasi ndax amna. Bindal ko balaa keneen diko bind.
Bindu ab domenPerformance bu baax ak wóor ak yoriinu liggéey bu yomb
Launch your online presence with hosting and professional email essentials.
Dedicated resources and flexible configuration for serious workloads.
Build hosting services under your own brand on reliable infrastructure.
Clear service managementPerformance bu baax ak wóor ak yoriinu liggéey bu yomb
★★★★★Hosting built around real businessesClear choices, dependable infrastructure and support that helps you keep moving.
“The best hosting experience is the one that lets you focus on your own customers. Everything important stays organised and easy to reach.
Danga tëju wala nga jaxasoo, xamoo loo wara def? Bul jaaxle ngir waxtaan ak nun, nga joxe sa xalaat, nu jàppale la nga jàll. Danu fi ñëw ngir jàppale la. Nanu waxtaan! 😃
KnowledgebaseSitweb hosting mooy serwiis biy may nit ñi wala mbootaay yi ñu mëna jëfandikoo seen sitweb ci net bi. Dafay laaj nga denc fichier sitweb bi ak ay done ci serwër bu boole ci internet, suko defee jëfandikukat yi ci àdduna bi yépp mëna ko jëfandikoo.
Xeeti dalal sitweb yu bari am, lu ci melni dalal buñ bokk, dalal VPS (Serveur privé virtuel), dalal buñ jagleel, dalal cloud, ak dalal WordPress buñ yor. Xeet wumu ci mëna doon, amna njariñam ak njëgam.
Hosting buñ séddoo mooy sitweb yu bari di séddoo ay jumtukaay ci benn serwër. Tanneef bu baax la ci sitweb yu ndaw yi waaye mën na am ay jafe-jafe ci wàllu performance ak personaaliseer.
VPS hosting dafay joxe ab serwër privé bu am ay jumtukaay yuñ jagleel sa sitweb. Dafay joxe performance ak tànneef ci personaalisasioŋ bu gëna baax sunu ko méngale ak hosting buñ séddoo.